Serigne Samba Ndiaye Wer gi yaram

Serigne Samba Ndiaye Wer gi yaram La page Serigne Samba Ndiaye Wer gi yaram donne des trucs simples et naturels pour améliorer la santé

Soo nopaloo ngay sooga yëk ni sonënga waayé askan jar na ko. Yalla na jamm yagg. Amin
29/05/2026

Soo nopaloo ngay sooga yëk ni sonënga waayé askan jar na ko. Yalla na jamm yagg. Amin

Mara vous dit dewenati!
29/05/2026

Mara vous dit dewenati!

Une chanson de Fily Cissokho dédiée à Mara

28/05/2026

Tay moom bayyinaa reer bi ak ndiobeen yi

Demi finale U17: le Sénégal vient d’éliminer le pays organisateur le Maroc aux tirs au but (1-1) à la fin du temps régle...
28/05/2026

Demi finale U17: le Sénégal vient d’éliminer le pays organisateur le Maroc aux tirs au but (1-1) à la fin du temps réglementaire. L’arbitre a accordé un penalty au Maroc à la 95e minute. Ils se sont séparés au 10e tir arrêté par le gardien sénégalais.
Nous rencontrerons inchalla en finzle, la Tanzanie vainqueur de l’Egypte.

28/05/2026

Pour ñi jaaxlé woon ci bis bi équipe bi dém USA !

28/05/2026

Vous avez ici le palmier-dattier, le basilic, la pastèque, l’aloe verra, le doliprane, la verveine, le thym, l’Euphorbia hirta, le figuier de barbarie ou « garga mbossé »

Di naa déluwaat ci yar ndax xar yombul rén té kanam la jëm!
28/05/2026

Di naa déluwaat ci yar ndax xar yombul rén té kanam la jëm!

Salam. Maangi ziaar ci biss bu séll bi, di leen Boly axx té di leen baal. Di ñaan yalla mu dolli dal, jamm, xeewal ak wé...
28/05/2026

Salam. Maangi ziaar ci biss bu séll bi, di leen Boly axx té di leen baal. Di ñaan yalla mu dolli dal, jamm, xeewal ak wér ci reewmi. Dewenati !

Ku am liste joueurs yi ñu woo équipe bu France, nga baaxé ñu ko
27/05/2026

Ku am liste joueurs yi ñu woo équipe bu France, nga baaxé ñu ko

Ku ñu daxx ajuma. Bi ñu lay daxx fékna bureaux yi tëj. Samedi, dimanche ak altiné kénn ligeeyul.Talaata nga am xëy mu be...
27/05/2026

Ku ñu daxx ajuma. Bi ñu lay daxx fékna bureaux yi tëj. Samedi, dimanche ak altiné kénn ligeeyul.
Talaata nga am xëy mu bees manaam Président Assemblée nationale avec la manière : 132 voix pour contre 1 abstention. Des coeurs !

27/05/2026

Pr Samba Ndiaye en direct

Adresse

Hamo 5, Villa E/38
Guédiawaye
15000

Heures d'ouverture

Lundi 09:00 - 19:00
Mardi 12:30 - 19:00
Mercredi 16:00 - 19:00
Jeudi 09:00 - 19:00
Samedi 09:30 - 19:00
Dimanche 09:30 - 19:00

Téléphone

+221773181750

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Serigne Samba Ndiaye Wer gi yaram publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter La Pratique

Envoyer un message à Serigne Samba Ndiaye Wer gi yaram:

Partager