Djongue PLUS Love

Djongue PLUS Love Cette page a était essentiellement créer dans le bus d'apporter de l'aide aux couple désireux d'apporter un petit plus dans leurs vie de couple.

Grace a nos conseils et expérience sur ce domaine laisser nous vous dire vous êtes au bonne endroit

22/10/2023
Juste Pour Rire😀✔️Mais nak Si waxtan Ak yén ci seuy la dëul " Mais je comprend pas pour quoi vous préférez être paresseu...
09/07/2023

Juste Pour Rire😀✔️

Mais nak Si waxtan Ak yén ci seuy la dëul " Mais je comprend pas pour quoi vous préférez être paresseuse et nul nio xamni daraay Jongué" 😂

X**a ma Waxati toutti rék guiss nga lolu ñuy wowé routine conjugal xawma nou ñou Koy Waxé ci holof nak😂 Mais da faay Yak sëuy di ko soofal dém Ba ray sëuy surtout ñou reuy ñi ak borom Béne Plat Yi yéén lay waxal déléén varié goût Yi ( chez papis Niang ) ak plaçou Sëuy Yi lou ko Moy di Nga Wañi envie bi ca borom keur di am wala Mu xoli Yénén plat si mbéed bi baxna rék😂

Mani xalé yi sauvage léne, parfois vulgaire Yéén say douce Djigueine da ngay wara tiaga innovant dëuk ci deffal sa jëkeur you béss goor da beug surprise diko kate partout si keur gui Diko yobou si do**he bi si suuf laal bi si moquette bi si chaise bii kaw térass fépP fuu katable Boulko di yëreum béne yone jigéén namounassi bouy youkhoulo jëkeram di ko mathie yénn sayy nga baram ko😂

Je vous adore chères Linguéres

Intéressé faite moi signe PV  🔞
23/06/2023

Intéressé faite moi signe PV
🔞

04/11/2022

Goudi dagnekoye préparer depuis le matin 💃
Le matin fais sont petit déjeuner 🥞 bayiko mouye savouré gua Khawa dougeul sa lokho tarkhisse touti si coye bi khôl bakham taye di nala djokh ligua sokhla boko défé gua guisseko mou sigui khôl la gua djouk ndakh avec une sourire 😃 provocatrice mou khameni akh taye la taye 🔥🥳
Une fois au boulot woko defal saye caprices wakhko wakh you nekh youkoye masse mani Djiguene daguaye djongue 😉
Taye foumou diare tela wathe 🤣

Le soir bala mouye eguessi na fek gua paré dresse ta table 🍗🌭🥪🍕 boul fate bougies na lep lerr djokh ko mou lek ba soure ndakh goudi gui da nara yague 🤪physiquement nagua paré sole lou sexy geneul bine bine yi nuisette yi thiouraye yi sans oublier cristal plumes menottes ahhhhhhh wawaw daara waroul sed 💪

les hommes aiment sentir de bonne odeurs chez leurs femme Parfum ta chambre lale draps blanc wote diame la paix entre guillemets 😜
waye né yathe do sangou do solou nek si wagne bi di dougou di geneu rek melni coursière Djiguene daye saf djiguene 😂

  ♥️🥰☘️ASTUCE 100% NATUREL POUR LES FEMME MARIÉE -⭐️ 1 gingembre -⭐️ 10 feuilles de menthe -⭐️ 1 poignée de bissap -⭐️ 1...
26/09/2022

♥️🥰☘️

ASTUCE 100% NATUREL POUR LES FEMME MARIÉE

-⭐️ 1 gingembre
-⭐️ 10 feuilles de menthe
-⭐️ 1 poignée de bissap
-⭐️ 1 tige de gongonlili
-⭐️ 7 poivres africains
-⭐️ 1 sachet de miel aphrodisiaque ( j’en vend)🍯

Tu fais bouillir tous ces ingrédients dans 2L d’eau pendant...A SUIVRE

BON SO BEUGUÉ XAMEU
_LIMOUY NIEURIGNE
_AK NOUGNKOY DÉFARÉ

ABONNE TOI A NOTRE PAGE ☺️POUR NE PAS RATER LA SUITE🙃🙈

Ohhh boul faté lale bouton z'aime tmt😂si conditions yi la bokkk

Coach jongué : Dama beug Mom sama diekeur??😊❤❤Bo beugue mom sa diekeur  nanga deuké li : 👉🏽 Def sa diekeur confident sa ...
22/09/2022

Coach jongué : Dama beug Mom sama diekeur??😊❤❤

Bo beugue mom sa diekeur nanga deuké li :
👉🏽 Def sa diekeur confident sa complice meilleur amie di communiquer wakhtan mom dolen ame ben neubo

👉🏽khame sa diekeur loum beug ngako def disi dokh loum begoul boulko beug nga bayi khamni moy sa sangue.

👉🏽nga mayko diame moytou léep lo khamni day indi rero sen diganté bagna khadial ken sisa seuy.

👉🏽bou goudi dioté nga guené sa arsenal say feem defar bamou bakh

jongue😊❤

arsenal say feem defar bamou bakh

POUR PLUS D'ASTUCES CLIQUEL FI
👇👇👇👇👇👇👇👇👇👇👇👇
Djongue PLUS Love

Adresse

Dakar

Téléphone

+221763031049

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Djongue PLUS Love publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager

Share on Facebook Share on Twitter Share on LinkedIn
Share on Pinterest Share on Reddit Share via Email
Share on WhatsApp Share on Instagram Share on Telegram