07/05/2023
ASSOCIATION MATLABOUS CHIFAA’I (AMC), mbooloo mu jog ngir dimbali nitt ñi ci seen wer gi yaram, jaarale ko ci ay activités yu moy amall :
- bisup saytu sa wer gi yaram ta doo fay dara
- maye dareet 🩸
- conférences
- jappale nit ñi yitt ngir ñu mana bokku ci mutuelle yi.
- sensibilisation ak dimbali ku weredi ci ordonnance yi.
Ñeppa mana bokku ci association bi, da ngay jand carte membre 1.000f, weer wu dee nga barkeelu 5.00f.
Ko ci baga bokku wooteel ci limaate yi :
- Président Baye Serigne Bousso : 77 710-23-83
- Secrétaire générale Serigne Saliou Mbacké : 77 994-74-12
Responsable de la communication Serigne Abdou Khadir Bousso : 76 721-35-27.